Cover art by A.L.
OMT013: El Gueye / Tameu
Tameu is the new single from Senegal star El Gueye (see also OMT005).
It means 'inseparable' in wolof.
A simple story of 2 people that cannot live separately.
A simple story of 2 people that cannot live separately.
El Gueye has already recorded 3 albums and is recognised as one of the best singer and composer in Senegal.
The Senegalese musical heritage is better known than that of most African countries, thanks to the popularity of this mbalax style and Sabar drumming is particularly popular.
El Gueye is preparing a new album that will include lots of new different elements going further away from Mbalax.
Tameu:
Damala tameu tameu
Damala tameu tameu
Ba soumala guissoulé
Sama yaram dafay Lass
Yow dagua bokkeu thi mane
Damala tameu tameu
Basoumala guisoulé
Sama yaram dafay lass
Danio minanetey
ba melni ay domi baadiéne
Légui sakh danio dem ba
daniou nouro oh nioune niar.
Ba leppeu louma beugua wakh khamgua co
Lo beugua wakh khamnaco.
Yone winiou dieule bilay sorina
Wayé fékkeu nio gui diapane té lokho ma dila séne.
Douma ragual- Douma ragual finiou dieum.
Beutou mbeuguel dafa andak yeurmandé.
Beutou mbeuguel dafa andak yeurmandé .
Té mbeuguel dou lénéne loudoul
Lakkeu séddo oh
Té guathiakh sokhlawoul lénéne loudoul ndokh so tawé ma contane.
Damala tameu tameu
Damala tameu tameu
Ba soumala guissoulé
sama yaram dafay lass.
Yow dagua bokkeu thi mane
Damala tameu tameu
Basoumala guisoulé
sama yaram dafay lass
Bayil samay lokho mou lale la
Bagua mana yeuk sama taguayou yaram
Mayma sama beut bama kholla
Ba mane la diokh
thieur biga yellole.
Say diatay dafmay doundeul
Sa mélocane dima bégue lo.
Kanam kasso la
Ko thi teuth mou khamco
Mayma say rétaaane.
Kanam kasso la
Ko thi teuth mou khamco
Mayma say rétaaaane.
Beutou mbeuguel dafa andak yeurmandé
Beutou mbeuguel dafa andak yeurmandé.
Yaw yay guarap gui may fékhal dima kéral
Dokh sama diguentek dianteu biii.
Haaaaaaaheuuuheuuu heeey
Thi yow lay yeugué sama boppeu
Deugue guagui thi samay beute khana kholoulomaa.
Digital release on the 9th of December 2022.
Track listing:
1: Tameu
Itunes, Spotify, etc.:
And on Bandcamp:
No comments:
Post a Comment